Torna

A l'abast

UBBITE GI


Ku nekk xam na ni la sababoon ñu siiwal sémb bi njȅkk ci wallu jokkoo ci lakku katalan, tey la gȅna taxaw. Booba ak léegi mat 20 at. Loolu mosul noppi di doon nisȅr yi askan wi di sàkku.    

Danoo wara sàmm wuute googu am ci diggante làkk wi ak aada yi. Wuute googu dafa bokk ci li doy doxal tugȅl (Europe). Katalan nag dafa am cér bu ñu indi ci li wuutale àdduna bi. Làkk woowu dañu ko wara xamal junniy nit ñi fiy ñȅw at mu nekk ak ñi fi bȅgga tabax seeni kȅr. Dañoo wara xam ni loolu wareefu Ile Baléare la.      

Soxla nañu ay jumtukaay yu deme ni téeréb loxo bii ñuy wax NEEXA YOR ndax sunu yéené mooy ñu gȅn ñoo xam ci àdduna bi yépp ba ñu mȅna xamal katalan yiy doora dȅkk si Ile Baleares, bañu gȅn fee gȅna yȅg seen bopp

Amul benn coppite ci jumtukaay yi ñu amoon. Namu meloon la mel te lamu doon tekki lay tekki. Ay coppite yu ndaw yu am solo rekk lañu indi ci yenn béréb yi ngir gȅn ko mȅna méngalé ak jamono. Noonu rekk la mȅnoon deme ndax yeesal nañu pàcc bi mujj te itam yombal nañu ko ba mu dȅppόo ak jamono ngir jàng làkku katalan ngir gȅna neexa dégg. Ci noonu, dinañu dalal képp kuy jarinoo internet bi ci ȅttub jokkoo bii : web http://alabast.caib.cat, nga xam ni mȅn nañu fee dégloo itam.

Ci gàttal, li ñu nammoon ca sémb bu njȅkk ba ak bii benn la rekk la : Te mooy fexe ba jox ni fi dȅkk ak gan ni lépp luy yombal jàngum Katalan jaare ko ci yenn kàddu yi ñuy jȅfandikόo bés bu yàlla sàkk ngir dundal làkk wi.

Miquel Company i Pons
Kiy xelal ñi yor koppar ci Tugȅl, Daara ju mag jiy ittéwoo aada
Nuurug Iles Baléare



PRESENTACIÓ

Tothom convindrà que els motius que van empènyer a la publicació, fa vint anys, de la guia de comunicació bàsica en llengua catalana A l’abast continuen ben vigents avui en dia i no han deixat de ser objectius que la nostra societat aspira a assolir: el respecte a la diversitat lingüística i cultural com un dels motors que fa funcionar Europa i l’oferiment de la llengua catalana com la nostra contribució a aquesta diversitat mundial. Donar a conèixer el nostre patrimoni lingüístic tant als milers de ciutadans que cada any ens visiten com als qui decideixen fixar aquí el seu lloc de residència s’ha d’entendre, per tant, com un deure de les institucions de les Illes Balears.


De ben segur que necessitam eines com la guia A l’abast, perquè tenim la voluntat ferma de donar-nos a conèixer al món i de facilitar als nous residents el coneixement de la llengua catalana, pròpia de les Illes Balears, com a via natural per integrar-se a la nostra comunitat.


Així, aquesta reedició del material manté l’esperit i l’estructura de la publicació original. Només s’hi han fet algunes actualitzacions puntuals i també modificacions formals —necessàries, d’altra banda— per fer-lo més proper. Com no podia ser d’una altra manera, s’ha actualitzat l’apartat final de recursos per aprendre la llengua catalana i s’ha simplificat tècnicament, d’acord amb els temps que corren, la possibilitat d’escoltar els textos. Així, es posa a disposició dels usuaris el lloc web http://alabast.caib.cat, que inclou l’opció d’àudio.


En definitiva, l’aspiració continua sent la mateixa que amb la primera edició: oferir a visitants i residents, a través de fragments que reprodueixen situacions lingüístiques habituals a la vida quotidiana, un primer tast de la nostra llengua que faciliti l’aprenentatge del català i la plena integració lingüística.


Miquel Company i Pons
Conseller de Fons Europeus, Universitat i Cultura
Govern de les Illes Balears