Torna

A l'abast

LAAJ YI ÑUY FARAL DI DEF

dona-pag 5 (1).gif

Wòlof Català Àudio

—Naka ngeen def? Naka nga def?
—Jàmm rekk sant.

―Com va? Com està?
―Bé, gràcies.

Lan moo ko dal? yaram wi neexul?

Què li passa? No es troba bé?

—Naka laa tudd?
—Isabelle laa tudd.


—Naka nga tudd?
—Pere laa tudd.

―Què noms?
―Nom Isabel.


―Com es diu?
―Em dic Pere.

—Yaay kan?
—Maay Mme Vidal.

―Qui és, vostè?
―Som la senyora Vidal.

—Lan la?
—Ab neexal la.

―Què és això?
―És un regal.

—Fan ngeen jógé?
—Allemagne lañu jόge. Waa Maroc lañu.
Autriche lañu dȅkk.

―D’on ets, tu?
―Som d’Alemanya. Som del Marroc. Som d’Àustria.

—Fan ngeen jógee?
—Angleterre lañu dȅkk. Irlande lañu dȅkk. Australie lañu jóge.

―D’on és, vostè?
―Som d’Anglaterra. Som d’Irlanda. Som d’Austràlia.

—Fan la jóge?
—Waa France la. Belgique la jόgé.
Algérie la jógé.

―D’on és, ell?
―És de França. És de Bèlgica. És d’Algèria.

—Fan ngeen jóge?
—Waa îles Canaries lañu. Équateur lañu
dȅkk. Chili lañu dȅkk.

―D’on sou, vosaltres?
―Som de les Canàries. Som de l’Equador. Som de Xile.

—Waa Majorque nga?
—Déet, allemand laa. Déet waa Maroc
laa. Déet waa Autrich laa.


—Ndax waa majorque nga?
Déet waa Allemagne laa. Déedéet, waa
Maroc laa. Déet, waa Autrichie laa.

―Ets mallorquí?
―No, som alemany. No, som marroquí. No, som austríac.

―Ets mallorquina?
―No, som alemanya. No, som marroquina. No, som austríaca.

—Ndax waa Minorque la?
—Déet, anglais laa. Déet, irlandais laa.
Déet, australien laa.


—Ndax soxna si waa Minorque la?
—Déet, anglaise la. Déet, irlandaise laa.
Déet, australiene laa.

―És menorquí? 
―No, som anglès. No, som irlandès. No, som australià.

―És menorquina?
―No, som anglesa. No, som irlandesa. No, som australiana.

—Ndax waa Ibiza ngeen?
—Déet, français lañu.” Déet, belges lañu. Déet, algériens lañu.


—Ndax waa Ibiza nga?
—Déet, français laa. Déet, belge laa.
Déet, algérien laa.

―Sou eivissencs?
―No, som francesos.  No, som belgues. No, som algerians.


―Sou eivissenques?
―No, som franceses. No, som belgues. No, som algerianes.

—Ndax waa Formentera lañu?
—Déet waa Canaris lañu. Déet, ay
équatoriens lañu. Déet, waa Chili lañu.


—Ndax waa Formentea lañu?
—Déet, Canaris lañu dȅkk. Déet, waa
équateur lañu. Déet, waa Chili lañu.

―Són formenterers?
―No, som canaris. No, som equatorians. No, som xilens.


―Són formentereres?
―No, som canàries. No, som equatorianes. No, som xilenes.

—Fan la dȅkk ?
—Ci taax ya laa dȅkk. Maa ngi dȅkk ca
kaw ga. Maa ngi dȅkk ca àll ba.
―On viu? 
―Visc a la ciutat. Visc en un poble. Visc al camp.


—Ci man mbedd nga dȅkk?
—Maa ngi dȅkk ci mbedd mi ñuy wax
Malaga. Déet, maa ngi dȅkk ci Place Mayor.

―A quin carrer vius?
―Visc al carrer Nou. Visc a la plaça Major.

—Ndax dégg nga catalan ?
—Waaw tuuti rekk. Bariwul de.

―Parla català?
―Sí, un poc.  No gaire.

Ndax dégg nga li may wax? Lu mu tekki?

M’entén? Què vol dir, això?

Naka? Naka lees ko waxee?

Com? Com diu?

Lan nga wax? Lan nga bȅgg?

Què dius? Què vols?

Fan ngeen jȅm? Fan ngeen jóge?

On anau? D’on veniu?

Ndax wóor na la? Ndax Wόor na ko?
Ndax wóor na la? Dȅgg la?

N’està segur? / N’està segura? De veritat?

Kañ? Kañ lawoon? Ba kañ lay doon?

Quan? Des de quan? Fins quan?

Wax ma? Kan ngay waxal? Ci kan la jóge?

Digui? Amb qui parl? De part de qui?

Ndaw am na ñaari xel? Ndax dégg nga??

Hi ha cap dubte? Entesos?

—Bȅgg nga ko?
—Waaw, bu baax. Déet, mukk.

―T’agrada?
―Sí, molt. No, gens.

Mȅn naa tux? Mȅn naa gaare fii?

Que puc fumar? Que hi puc aparcar, aquí?

Mȅn nga féey? Mȅn ngaa togg?
Mȅn nga làkk catalan?

Saps nedar? Saps cuinar? Saps parlar català?