Torna

A l'abast

MELOKAAN

Wòlof Català Àudio

Weex, xell, nete, xawa naat, naat, baxa, yulet, xonq, xawa xonq, gris, ñuul.

Blanc, beix, groc, carabassa, verd, blau, lila, vermell, grana, marró, gris, negre.

—Nan la mel?
—Dafa weexC’est. / Melokaan wu weex la. / Dafa baxa.

―De quin color és?
―És de color blanc. / És blanc. És de color blau. / És blau.

Sopp naa melokaan wii. Soppu ma dara
melokaan wii.

M’agrada aquest color. No m’agrada gens aquest color.

Dafa leer ba ȅpp. Lȅndȅmul torop.

És massa clar. No és gaire fosc.

LIM

Wòlof Català Àudio
Benn, ñaar, ñett, ñeent, juróom, juróom benn, juróom ñaar, juróom ñett, juróom ñeent, fukk.
U/un/una, dos/dues, tres, quatre, cinc, sis, set, vuit, nou, deu.

Fukk ak benn, fukk ak ñaar, fukk ak ñett, fukk ak ñeent, fukk ak juróom, fukk ak juróom benn, fukk ak juróom ñaar, fukk ak juróom ñett, fukk ak juróom ñeent, ñaar - fukk.

Onze, dotze, tretze, catorze, quinze, setze, desset/disset, devuit/divuit, denou/dinou, vint.

Fanweer, ñeent fukk, juróom fukk, juróom benn fukk, juróom ñaar fukk, juróom ñett fukk, juróom ñeent fukk, téeméer, junni.

Trenta, quaranta, cinquanta, seixanta, setanta, vuitanta, noranta, cent, mil.

Pàcc/pàcc, benn ñeenteel, ñaari
ñeenteel, benn fukk ak ñaar.

Mig/mitja, un quart, dos quarts, una dotzena.